SOUTENONS INDEX ÑUUL KUKK À SORTIR L'ALBUM
Description en wolof et en français / ci wolof ak ci français
Wolof
Nuyu naa leen, maa ngi tudd Al Hassan Salam SECK, di wuyoo Index Ñuul Kukk, juddoo, màggee Ndar géej Sénégal yaroo fa. di yeewoo tugël si jamono jii. Lu ëpp at moo ngi nii may ligeey si projet "album" boo xam ni lepp acapella lay doon, ngir fësal baat ak bind, di ko def ci wolof (li si ëpp). Ngir Album boobu judd dafa laaj koppar: man miy ndeyu mbilli gi, def naa si sama alalu bopp waaye mate wul lepp. moo tax may sakku si kepp ku ko bëgg te mën ko, mu jappale ma ci dajale xaalis bi ligeeyu album bi d laaj. Li may soxla ngir gennee album bi nag moo ngi tollu si "Un million deux cent mille francs cfa (1 200 000 frs cfa)
Jërë ngeen jëf mbokassaa.
Français
Bonjour
Je me surnomme Index Ñuul Kukk. Je suis artiste chanteur/rappeur. Je suis né à Saint-Louis du sénégal et j'y ai grandi aussi. Actuellement je vis en France.
Celà fait plus d'un an que je travail sur mon projet d'album 100% acapella, écrit dans ma langue maternelle qu'est le wolof pour la valorisation de celle-ci. Pour réaliser ce projet d'album, j'ai besoins de fonds: j'ai mis une partie de ma propre poche, mais cela reste largement insuffisant pour financer ce projet. En effet, il faut au moins un million deux cent mille frs CFA (1 200 000 frs) pour sortir cet album.
Merci d'avance
..............
Ngir xool li ma jota def ci ay way ak widéo (Lënk bi ci suuf) / Pour voir mes productions et vidéos précédentes (voir le lien en dessous:
https://www.youtube.com/channel/UCJD3IolVVUYGPNOwCdTxYBg
-
GASSAMA
100 FCFA
22 May 2021 à 1:48 -
Papa moussa Diouf
20 000 FCFA
21 May 2021 à 19:05Merci frère on n est fièr de toi et bonne continuation
-
THOMAS NORMAND
9 800 FCFA
14 Apr 2021 à 19:13En espérant que ça t'aideras pour ton projet frérot!
-
Anonyme
5 000 FCFA
03 Apr 2021 à 23:17Bon vent!
-
Thioumbé
5 000 FCFA
31 Mar 2021 à 13:25Dîna baax
-
Dadita
20 000 FCFA
29 Mar 2021 à 19:53 -
Anonyme
5 000 FCFA
29 Mar 2021 à 16:30 -
Khadim G.
1 000 FCFA
28 Mar 2021 à 17:55 -
Anonyme
1 000 FCFA
28 Mar 2021 à 15:19 -
Anonyme
500 FCFA
28 Mar 2021 à 14:28 -
Anonyme
2 500 FCFA
28 Mar 2021 à 11:27 -
Anonyme
1 000 FCFA
27 Mar 2021 à 22:27De tout cœur avec toi
-
Anonyme
1 000 FCFA
27 Mar 2021 à 22:27 -
Moussa balla Deme
500 FCFA
27 Mar 2021 à 20:17Mboka sa yaaram
-
Bassirou
500 FCFA
26 Mar 2021 à 12:56 -
Elhadji Ndiaye
25 000 FCFA
26 Mar 2021 à 12:22Keep up the good work
-
Abdou Sarr
5 000 FCFA
26 Mar 2021 à 11:43 -
Anonyme
2 000 FCFA
26 Mar 2021 à 10:22Merci encore à toi.
-
Anonyme
2 000 FCFA
26 Mar 2021 à 8:32 -
Anonyme
3 200 FCFA
26 Mar 2021 à 7:30